1 John 2:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Maa ngi leen di bind, yéen baay yi,ndax xam ngeen Ki nekkoon ca njàlbéen ga ba tey.Maa ngi leen di bind, yéen waxambaane yi,ndax daaneel ngeen Ibliis.