1 John 2:16 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte lépp lu nekk ci àddina, maanaam bëgg-bëggu yaram ak xemmemu bët ak réyug àddina, loolu du jóge ci Baay bi waaye ci àddina.