1 John 2:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci sunu biir lañu jóge, waaye bokkuñu woon ci nun; ndaxte su ñu bokkoon ci nun, kon dinañu des ci nun. Waaye dàggeeku nañu nu, ngir mu leer ne, kenn ci ñoom bokkul woon ci nun.