1 John 2:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Kuy sàmm kàddug Yàlla, dëgg-dëgg sa mbëggeel ci Yàlla mat na sëkk. Ci loolu lanu xame ne, nekk nanu ci moom.