1 John 2:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Samay soppe, li ma leen di bind du ndigal lu bees, waaye ndigal lu yàgg la; la ngeen jotoon ca ndoorte la. Te ndigal lu yàgg loolu, mooy kàddu gi ngeen déggoon.

Recommended Reading