1 John 3:23 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndigalam mooy lii: nu gëm turu Doomam, Yeesu Kirist, tey bëggante, ni mu nu ko digale.