1 John 4:17 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ni Kirist mel, noonu lanu mel nun itam ci àddina. Ci loolu la mbëggeel mate sëkk ci nun, ngir nu am kóolute bésu àtte ba.