1 John 4:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci lii lanu xàmmee Xelum Yàlla: mépp xel mu nangu ne, Yeesu Kirist ñëw na, nekk nit, ci Yàlla la bokk.