1 John 5:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Képp ku gëm ne Yeesu mooy Almasi bi, juddu nga ci Yàlla; te ku bëgg waajur, dinga bëgg itam ki mu jur.