1 John 5:15 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Gannaaw xam nañu ne, dina nangu lépp lu nu koy ñaan, xam nanu it ne, li nu ko ñaan, jox na nu ko.