1 John 5:18 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Xam nanu ne, képp ku juddu ci Yàlla doo sax ci bàkkaar, waaye Doomu Yàlla ji mooy wottu sa bakkan, ba Ibliis du la manal dara.