1 Kings 1:17 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu ne ko: «Sama sang, yaw yaa ma giñal ci sa Yàlla Aji Sax ji, sang bi, nga ne ma sama doom Suleymaan de dina falu buur moos, wuutu la, te moom mooy toog ci sa kaw jal bi.