1 Kings 1:41 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba mu ko defee Adoña dégg ca, mook mboolem ña mu woo woon, ñu nekk faak moom. Fekk ñu lekk ba noppi. Ba Yowab déggee liit ga, da ne: «Waaw, riir mi ci dëkk bi, lu mu doon?»