1 Kings 1:42 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Daaneelagul kàddoom sax, Yonatan doomu Abiyatar sarxalkat ba ne jaas, agsi. Adoña ne ko: «Dikkal, yaw nit ku baax nga, te xibaaru jàmm ngay indi.»