1 Kings 1:52 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Suleymaan daldi ne: «Su dee nit ku jara wóolu de, genn kawaram du wadd ci suuf. Waaye su lalee pexem wor de, dina dee.»