1 Kings 10:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mboolem lu Buur Suleymaan daan naane wurus la, te mboolem ndabi këram ga ñuy wax Gottub Libaŋ wurusu ngalam la. Dara du ca xaalis, ndax xaalis jàppeesu ko woon muy dara ca janti Suleymaan.