1 Kings 11:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dafa santoon Suleymaan ci mbir moomu, ne ko bumu topp tuuri yeneen xeet yi. Waaye deful li ko Aji Sax ji santoon.