1 Kings 11:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te ba tey du nguur gépp laay foqati. Dinaa bàyyee sa doom genn giir ngir Daawuda sama jaam ba ak Yerusalem gi ma tànn.»