1 Kings 11:29 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu am bés Yerbowam doon génne Yerusalem. Axiya, yonent bu dëkk Silo ba, dajeek moom ca yoon wa. Ma nga sol mbubb mu bees. Ñoom ñaar rekk ci àll bi.