1 Kings 11:32 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye genn giir gi Suleymaan a koy moom ngir Daawuda sama jaam ba, ak Yerusalem, dëkk ba ma tànne ci mboolem giiri Israyil.