1 Kings 11:33 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li ko waral mooy dañu maa dëddu, di jaamu Astàrt, tuur mu jigéen mu waa Sidon di jaamu, ak Kemos, tuuru Mowabeen ñi, ak Milkom, tuuru Amoneen ñi. Dañoo baña topp samay yoon, baña def li ma rafetlu, di sàmm samay dogal ak sama àttey yoon, na ko Daawuda baayu Suleymaan daa defe.