1 Kings 11:34 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye duma jële nguur gépp ci loxoom, ndaxte dama koo def njiit giiru dundam gépp ngir Daawuda sama jaam ba ma tànnal sama bopp, te mu doon jëfe samay santaane ak samay dogal.