1 Kings 11:41 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li des ci mbiri Suleymaan ak mboolem lu mu def ak lu jëm ci xelam mu rafet, bindees na lépp moos ca téere ba ñu dippee Jaloorey Suleymaan.