1 Kings 11:43 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw loolu Suleymaan tëdd, fekki ay maamam. Gox ba ñuy wax kër Daawuda baayam, fa lañu ko denc, doomam Robowam falu buur, wuutu ko.