1 Kings 11:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Aji Sax ji nag mere Suleymaan ndax la mu ko dëddu, moom Aji Sax ji, Yàllay Israyil ji ko feeñu woon ñaari yoon.