1 Kings 12:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee Robowam dem dëkk ba ñuy wax Sikem, ndax fa la Israyil gépp daje woon, ngir fal ko buur.