1 Kings 12:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xale yu góor ya mu màggandool ne ko: «Mbooloo mii ne la sa baay da leena gàlloon buumu njaam gu teeŋ, waaye yaw yolomalal leen ko; li nga leen di wax mooy lii: “Sama baaraamu sanqleeñ moo gëna diis sama tànku baay.