1 Kings 12:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Na ko xale yu góor ya digale la waxeek ñoom, ne leen: «Sama baay a leen tegoon njaam gu metti, waaye man maa koy yokk, mu gëna metti. Te sama baay ay yar la leen daa cawe, waaye man ay leraw yu ñu kor weñ laa leen di cawe.»