bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 1 Kings 12:24
1 Kings 12:24 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
“Aji Sax ji dafa wax ne: Buleen jóg di xeex ak seen bokki bànni Israyil. Na ku nekk ñibbi këram, ndax ci man la mbir mii sababoo.”» Ñu dégg kàddug Aji Sax ji, walbatiku dem, noonee ko Aji Sax ji waxe.