1 Kings 12:25 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw loolu Yerbowam tabaxaat Sikem, dëkk ba ca diiwaanu tundi Efrayim, daldi fay dëkk. Mu jóge foofa tabaxaat dëkk ba ñuy wax Penuwel.