1 Kings 12:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Buur Robowam giseek mag ña daa taxawu Suleymaan baayam ba muy dund. Mu ne leen: «Lu ngeen may digal, ma wax ko mbooloo mii?»