bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 1 Kings 13:11
1 Kings 13:11 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Booba ab yonent bu màggat a nga woon ca Betel. Ay doomam yu góor dikk. Kenn ci ñoom nettali ko mboolem la góoru Yàlla ga def bésub keroog ca Betel ak la mu wax Buur. Ñu yegge ko seen baay.