1 Kings 13:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Seen baay laaj leen ne leen: «Ana yoon wu mu jaare?» Fekk na doomam yu góor ya gisoon nañu fa góoru Yàlla ga jaare woon, bàyyikoo Yuda. Ñu wax ko.