1 Kings 13:25 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Naka la ay nit jaare foofa, séenuñu lu moy néew ba ne lareet ca yoon wa, gaynde ga taxaw ca wet ga. Ñu dem yegge ko waa dëkk, ba yonent bu màggat ba dëkkoon.