1 Kings 13:26 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yonent booba ko waññi woon ca yoon wa nag dégg ko ne: «Góoru Yàlla gaa! Ka tebbi woon waxi Aji Sax ji, Aji Sax ji boole kook gaynde gi, mu fàdd ko, rey ko. Moom la ko kàddug Aji Sax ji waxoon.»