1 Kings 13:33 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw loolu Yerbowam dëppul yoonam wu bon wa mu topp. Dafa dellu tabb ci biir baadoolo yi ay sarxalkat ngir bérabi jaamookaay ya. Ku bëgg rekk mu tabb la, ngay sarxalkat ca bérabi jaamookaay ya.