1 Kings 13:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax loolu lañu ma sant ci ndigalal Aji Sax ji, ne ma: “Bul sex dugub, bul naan um ndox te bul walbatiku jaare yoon wa nga jaare woon bi ngay ñëw.”»