1 Kings 14:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Israyil gépp dinañu ko jooy. Kooku rekk déy lees di denc ci bàmmeel, ci ku bokk ci Yerbowam, ngir ci moom doŋŋ la Aji Sax ji Yàllay Israyil gis lu baax, ci waa kër Yerbowam.