1 Kings 14:31 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw gi Buur Robowam tëdd, fekki ay maamam, ñu denc ko fa ay maamam ca gox ba ñu naan Kër Daawuda. Ndeyam a doon Naama, Amoneen ba. Ci kaw lool doomam Abiyam falu buur, wuutu ko.