1 Kings 15:17 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci biir loolu Basa buurub Israyil song Yuda, daldi dàbbli dëkk ba ñuy wax Raama, ba kenn du dugg jëm ca Asa buurub Yuda mbaa muy génn.