1 Kings 15:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
« Kóllëree dox sama digganteek yaw, na mu doxe woon sama diggante baay ak sa baay. Lii nag maa la ko may, xaalis la ak wurus. Te nga dogoo rekk ak Basa buurub Israyil, ndax mu jóge samam réew.»