1 Kings 15:20 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ben Addàd déggal Buur Asa, daldi yebal njiiti xarey gàngooram ca dëkki Israyil. Ni la nangoo dëkk ya ñuy wax Yon ak Dan ak Abel Bet Maaka ak diiwaanu Kineret gépp, boole ca diiwaanu Neftali gépp.