1 Kings 15:22 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee Buur Asa joxe ndigal, woolu waa Yuda gépp, kenn desul. Ñu ànd jëleji ca Raama doj yaak bant ya Basa doon tabaxe. Buur Asa tabax ca dëkk ba ñuy wax Geba gu giirug Beñamin, tabax ca Mispa.