1 Kings 15:23 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li des ci mbiri Asa ak mboolem njàmbaaram ak la mu def yépp ak dëkk ya mu tabax, bindees na lépp moos ca téere ba ñu dippee Jaloorey buuri Yuda ca seeni jant. Ba Asa demee ba màggat nag, jàngoroy tànk la ame woon.