1 Kings 16:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Damaa fekk nga maaseek pëndub suuf, ma yékkati la, jiital la, nga yilif Israyil sama ñoñ. Nga aw nag ci yoonu Yerbowam, di bàkkaarloo Israyil sama ñoñ, ba ma mer ndax seeni bàkkaar.