bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 1 Kings 16:7
1 Kings 16:7 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te itam ba kàddug Aji Sax ji dikkalee Yonent Yàlla Yewu doomu Anani ci mbirum Basa ak waa këram, li ko waral mooy la Basa def lépp, di roy waa kër Yerbowam, Aji Sax ji ñaawlu ko ba xolam fees. Rax ci dolli Basa rey waa kër Yerbowam.