1 Kings 17:22 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Aji Sax ji nangul Ilyaas kàddug ñaanam, bakkanu xale bu góor ba délsi ca moom, mu dund.