1 Kings 18:25 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu Ilyaas wax yonenti Baal ya ne leen: «Tànnleen wenn yëkk te jëkka defar, ndax yeena gëna bare. Bu ngeen noppee, ñaanleen ci seeni tuur, waaye buleen taal.»