1 Kings 18:27 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Digg bëccëg jot, Ilyaas di leen ñaawal, naan leen: «Yuuxuleen ca kaw, waay! Mooy Yàlla moos; jombul daa am lu muy xalaat, mbaa mu jàpp, mbaa mu tukki, mbaa xanaa muy nelaw, ñu war koo yee.»