1 Kings 18:30 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba mu ko defee Ilyaas wax ak mbooloo ma mépp, ne leen: «Jegesileen fii!» Ñépp jegesi. Mu defaraat sarxalukaayu Aji Sax ja tasaaroo woon,